#2STVLIVE LAYLATOUL KHADR AVEC TAFSIR ABDOURAHMANE GAYE ET CHERIF MAMINE AIDARA Télécharger

Envoyer à vos amis
Ajouter
  • Diffusé en direct le 20 mai 2020

  • www.2stv.net Iptv disponible sur 2stv.sn https://www.instagram.com/2stvlofficiel https://www.facebook.com/2stvsenegal https://twitter.com/2stvsenegal

Commentaires

  • aliou ba
    aliou ba il y a 5 mois (modifié)

    Ma cha Allah le SÉNÉGAL 🙏🏿🇸🇳

  • Binta Kande
    Binta Kande il y a 5 mois

    L infatigable tafsire

  • Dia Abdarahmane
    Dia Abdarahmane il y a 5 mois

    Vraiment les mots me manque pour exprimer ce que j ressent dans mon coeur aujourd'hui ce 1000% Laylatoul khadri Mchlh

  • Loli Boye
    Loli Boye il y a 5 mois

    Tafsir abdourahmane yalla nala yalla bayi sounou kanam sa doundou amna gnarign nakh yagui nouy wan yonn bi gnou wara dieul pour motaliii sounou diamou yalla

  • Amdy Kebe
    Amdy Kebe il y a 5 mois

    Cette émission devrait continuer apres le ramadan car on en a besoin machallah tafsir yala na yalla yokou sa fane ak epuipe bi yépou

  • Ramses ndiaye
    Ramses ndiaye il y a 5 mois

    2stv nôtre télévision préférée niogui niane émission Bi continue machallah

  • Ablaye Thiaw
    Ablaye Thiaw il y a 5 mois

    Bilae heure souma dèguè Tafsir sama xol toye 😢🇸🇳yallah nako yallah may fane wou goudou tèmou wanalè ak mome 😢

  • Mohamed Ndour
    Mohamed Ndour il y a 5 mois

    Thiey yalla nioune liniou am khamouniouko sakh , TAFSIR Abdourahmane Gaye ak Chérif mamine aidara yalla naléne souniou borom aar samm léne té goudal séne Fann si barké Seydina Mohamed psl

  • EL HADJI BA
    EL HADJI BA il y a 5 mois

    Ohh 😭 Yalla nagnou lène yalla fayal très fier d vs ♥️🙏

  • Fall Mouhamed
    Fall Mouhamed il y a 5 mois (modifié)

    Tabaarakallahou maacha allah yalla naléene fi yalla bayyi.J'ai déjà célébré cette nuit depuis la Mauritanie hier,mais grâce à vous mangui koye doundaate.

  • Oumou Cissé
    Oumou Cissé il y a 5 mois

    Machallah wakhtan mi amna solo lol dilen nianal goude fan rek ak wer yalna diam sakh si yen contane naniou torop

  • Ba Youzasif
    Ba Youzasif il y a 5 mois

    Tafsir Gaye AK cherif mamin duo bou geuneu nekh thi duo yii Yalla nalein sameu thi brkè yonentibi sen ligeuy raffet naa senegalai yii yeup sen xoll sedena thi yenn

  • Ba Youzasif
    Ba Youzasif il y a 5 mois

    Bravo 2stv liguey bii raffet naa dolein moromou xalè

  • Aminata Kebe
    Aminata Kebe il y a 5 mois

    Ndeysann regardez ces enfants ils me donnent la chair de poule yalna yalla wathie barke alkhourane bi si yen ak seni parents ak serigne Dara bi ak Sénégal yeup. machallah fière de vous.

  • Dieyna Keita
    Dieyna Keita il y a 5 mois

    Tafsir ❤yallah na yallah goudal say fane🙏 machallah ya Allah fay lén yiw yén yép ins cha Allah❤❤❤

  • Amadou sall
    Amadou sall il y a 5 mois

    Felicitation à nous d'avoir Mohammed psl comme prophete

  • Adama Cissoko
    Adama Cissoko il y a 5 mois

    Lon vie que dieu vous protège mes idoles imame aïdara et oustaze tafsir mon grand idole je vous j aime

  • mame korian Dembele
    mame korian Dembele il y a 5 mois

    machalla Tafsir yalla n'a yalla yok sa fan c'est mots me touche vraiment

  • Alimatou Sadiya Diop
    Alimatou Sadiya Diop il y a 5 mois

    Yalnalen yalla fayal boppam 😭❤️✨🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • Fatimata Djibril SoW
    Fatimata Djibril SoW il y a 5 mois

    Longue vie à ces enfants 😭😭🙏❣️🤣♥️