Accusé par Bay Ely avoir propagé sa m0rt SaNex verse de chaudes larmes et répond«togn nama limou def Télécharger

Envoyer à vos amis
Ajouter
  • 5 mai 2020

  • #restezchezvous

Commentaires

  • Soce Poumane
    Soce Poumane il y a 4 mois

    Kou beug sanex rek beuseul j'aime way🙏

  • Oumar Diop
    Oumar Diop il y a 4 mois

    Ki partager audios ci bopam moy domerame

  • Djalita Seck
    Djalita Seck il y a 4 mois

    Deff Lou bakh mo yomboul rek mom bimou dégué décédé deff na le tout ba degg ko pour defall ko Lou bakh mais kholal Fay bi😭😭🤷🏻‍♀️ Sénégal li mom warna fé djogué koula yéné loubakh rek nga fay ko Lou bone😳😳

  • Mouna Ba
    Mouna Ba il y a 4 mois (modifié)

    Fausse accusation defeuuuu metttttiiiiiii ci khol Ndeyssane...du courage Sanekh!!!!

  • Amina Cole Gueye
    Amina Cole Gueye il y a 4 mois

    Sanex ak lou mana am loumou méti méti diéguel ko té yalla takh talibé chiekh gua ball ko akh ndah état bimou nék cétal ci yalla cé dure mé ainsi va la vie courage so bakhé bari none

  • Soce Poumane
    Soce Poumane il y a 4 mois

    Kouy rétane lo nite yii dem bay dioy amna louko méti sincèrement

  • petite ouly
    petite ouly il y a 4 mois

    SANEKH N EST PAS MON ARTISTE MAIS ON VOIT QUE C EST PAS QUELQU UN DE MECHANT C EST UN DECONNEUR DROLE LES SENEGALAIS N ONT PAS ETE PREPARES A L INTERNET DIEU SAIT TOUT IL ECLAIRCIRA TOUT COURAGE

  • Ami Sarra
    Ami Sarra il y a 4 mois

    Peut-être malentendu la avec seune parceque sanekh mo wo Seune,, mais Seune qu'est-ce qu'elle a raconté a baye Ely ???? Une demande. Courage Sanekh kou bakh nga

  • Baye Cheikh
    Baye Cheikh il y a 4 mois

    Baye eli dafa febare bouko yokk diagoro diegal ko té dém sétiko wakhtane ak mome diguéne dioubo

  • Khadija Ndiaye diaw
    Khadija Ndiaye diaw il y a 4 mois

    Bayil lepp si lokho yallah

  • M. RIDA TV
    M. RIDA TV il y a 4 mois

    Sénégal mo meti beug torokhal nit rek😭😭😭

  • SENEGALBOY12
    SENEGALBOY12 il y a 4 mois

    Ki déef li mo boone ci wérou koor bi Mo déff lou niaawww Sa boule dioye léep dina léer In -Sha-Allah

  • maïmouna Seck
    maïmouna Seck il y a 4 mois

    Vraiment c triste

  • Thiané GUEYE
    Thiané GUEYE il y a 4 mois

    OU EST SEUNE ? NA WAKH LI MÈTINA TOROP

  • mya Ba
    mya Ba il y a 4 mois

    Sa amoul bene intérêt dire quil est mort....sanekh dou fenekat

  • Papa Diallo
    Papa Diallo il y a 4 mois

    Tkt sanekh

  • Ndiouck Ndeye Marieme
    Ndiouck Ndeye Marieme il y a 4 mois

    Metina na fausse information ca fait mal mais seune tamite qu'est ce qu'elle a raconté à baye Eli aussi je pense que c'est là où vient le mal attendu.mais wakhtan len rek erreur la

  • Fatou Cissé
    Fatou Cissé il y a 4 mois

    Pardonne le sanex peut être c'est la maladie qui lui a fait qu'il prononce ton nom makk la aussi aduna amoul solo

  • ba amar
    ba amar il y a 4 mois

    Le principal responsable dans tout ça ,c le gars qui a appelé bay ély parce que c lui seul qui détien l'enregistrement .c un émbéssil

  • Aissatou DIAW
    Aissatou DIAW il y a 4 mois

    C’est vraiment triste pour le Sénégal accusé des gens à tort gratuitement non mais oh faut arrêter à un moment.