Diomét " Lii Dou Famou Dieume Baakhoull" Li Wadji Wax S Ganna Euppna Deh........................... Télécharger

Envoyer à vos amis
Ajouter
  • 18 mai 2020

  • G C B Groupe

Commentaires

  • KHADIM DIAGNE
    KHADIM DIAGNE il y a 4 mois (modifié)

    KONE LI AME NA SÉNÉGAL

  • من فعل ماشاء لقي ماساء

    قال رسول الله صلعم لا يومن أحدكم حتى يحب لأخيه المسلم مايحب لنفسه

  • Niang Niang
    Niang Niang il y a 4 mois

    Dieurdieuf serigne touba

  • Zale Diaw
    Zale Diaw il y a 4 mois

    Kousa Serigne def lou bakh gua wakh KO Serigne bamba d'où morom

  • malick Gueye
    malick Gueye il y a 4 mois

    Kek comédiens danio bonne gana wakhoul Dara santé Serigne Touba rek bilahi

  • aida thiam
    aida thiam il y a 4 mois

    Serigne Touba amoul morom kou am morom mouy sa borom😍😍😍

  • Salam Sene
    Salam Sene il y a 4 mois

    Mane damay lathie nioune bane adouna lagniou nék yane façon dioulite lagniou yalla na gniou dhéé si begue s touba gana diam rék ngay am billahi

  • touba mbacke tv
    touba mbacke tv il y a 4 mois

    Senegalese mo sokhor bilahi 🙄🙄🙄

  • M3 Astuces en Wolof
    M3 Astuces en Wolof il y a 4 mois

    Al Hamdolilah Je suis baye Darou talib3 Serigne Modou Makhfouss Mbacke mom Sokhnamï Mbacke mom Serigne cheikh Awa Balla Mbacke ❣️❣️❣️❣️❣️✨🥰❣️😍❣️ Beugeu Serigne Touba Moy begeu sa bopou

  • Madiaw Mboup
    Madiaw Mboup il y a 4 mois

    Wa lii amna Senegal🙊gana yalla la yakar té serigne touba moye serignam ken manoul thi mom dara

  • j'aime ma mère wadiste
    j'aime ma mère wadiste il y a 4 mois

    Gana dale Wakhoul dara sii S Bamba rek la wakh diam rek ngay ame kéne mana loula dara koudoul yalla 🙏

  • Idy Xaragne Lo
    Idy Xaragne Lo il y a 4 mois

    Dieuredieufé Cheikh Akhmadou Bamba Khadim Rhassoul dieuredieufé Cheikh Akhmadou Bamba Khadim Rhassoul

  • Al-Amine Seck
    Al-Amine Seck il y a 4 mois

    Serigne Touba kéneuh la walahi👆😭❤️

  • Mustapha Samb
    Mustapha Samb il y a 4 mois

    Dieureudieufeuti serigne ganna messere yalla nafi yague ta wérr si barkép khadim rasaul

  • Pape Wade
    Pape Wade il y a 4 mois

    Lou way mana wakh serigne touba amoul morome

  • Mbaye Faye
    Mbaye Faye il y a 4 mois

    "Etre trop mouride,trop tidiane,trop qadr,celà risque de nous basculer dans le vide de la confrontation confrérique. Soyons partisans du prophète si nous voulons être de bon musulmans".

  • Assane mbaye
    Assane mbaye il y a 4 mois

    Kou déff lou kén défoul amlou kén amoul .Serigne touba kén la kouko bagne délll. Serigne gana yalla nafi yague téwér sii barkép khassidayii.

  • Modou Fall
    Modou Fall il y a 4 mois

    Gana n a rien dit de grave faites sortir dans vos enregistrements un seul passage ou il a offense une quelconque confrerie

  • Salam Fall
    Salam Fall il y a 4 mois

    Ndaysaan murit du toppee kenn jikkóom sunu jikkó lanuy àndeek ñépp moo tax jàmm rekk mooy am nuwaay mel bàyyee nan la ko te jàpp ninu mel àndee ko ak ñépp dunu loru dunu loree

  • Yalla Moy deugeu Nitou deugeu

    Réewmi Féne moko yaxeu AK Sokhor AK Néew Xam Xam Billahi wallahi wa tallahi Nioune geumou Niou Sax Mak ngi