Enfants égorgés par leur père à Touba: l'ami intime du meurtrier accuse les charlatans Télécharger

Envoyer à vos amis
Ajouter
  • Sortie le 14 mai 2020

  • Infos Rewmi est un site d'Information Sénégalais de people, Buzz,Société,Sports,Politique,Culture etc...

Commentaires

  • Khadim Sene
    Khadim Sene il y a 6 mois

    Sen yaye yi yalna len yalla may xolou mougn te xalle yi yalna len yalla xare aldiana 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • Mouhamadou Ndiaye
    Mouhamadou Ndiaye il y a 6 mois

    Le maraboutage doit être criminalisé au Sénégal

  • Mouhamadou Ndiaye
    Mouhamadou Ndiaye il y a 6 mois

    Tiey Sénégal bayilene nit yi nguene di ligueye bagnouy tago sene sago .

  • Issa Fall
    Issa Fall il y a 6 mois

    Mane nga xamni dama beugue sama dôme sou febare' sakhe damaye diakhle' dotouma beugue dara motakh geumoumani bara thi sagome la défe' lii

  • Maty Aidara
    Maty Aidara il y a 6 mois

    Adouna da diakhasso djinê yii gno nek si biir nitt yi dilen diakhassé dilen dfflo lou bonne

  • SOLDAROU MAME SALIOU
    SOLDAROU MAME SALIOU il y a 6 mois

    Li dé doyna warr mes Limay digale sama mbokki dioulite yi moy moytoulène ndiabarkate yi

  • seydina diop Bichri
    seydina diop Bichri il y a 6 mois

    gni wax gnépou Séne xalate rék lagnouye wax

  • aline badara
    aline badara il y a 6 mois

    Barra dé liko dal métina trop waye njépp lou bakh laniou wakh si mome

  • Bara Fall
    Bara Fall il y a 6 mois

    Ndeysan sama toma Bara yalnah Yallah leral lep metina trop sax mai Yallah bakhna lep dina fenge Incha allah

  • Thiatt Diene
    Thiatt Diene il y a 6 mois

    Meune naniouko khaptal aussi leppa nguissi

  • David Diop
    David Diop il y a 6 mois

    Bara est le seul qui pourrait justifier ce fait.

  • Sokhna Cissé
    Sokhna Cissé il y a 6 mois

    Bara nit kou bakh leu li tayouko nakh beugue ndiabot li tayouko nit kou bakhla li métina 😭😭😭😭

  • Fallou Seye
    Fallou Seye il y a 6 mois

    Doyna war d mande guamomane moko tay

  • cheikh mbacke
    cheikh mbacke il y a 6 mois

    Mane domam la wallahi lou bakh rk la kham thie mome khayna sakh douma mana wakh thie mome ndakh lou ma wakh niou né domam la waaye yalla guiss na lepp yalla na niou yalla soutoural

  • Ibrahima Paye
    Ibrahima Paye il y a 6 mois

    Je suis mouride sadékh

  • Cheikh Mbacke
    Cheikh Mbacke il y a 6 mois (modifié)

    SEYTANE BARI DOLLE YALLA NANIOU YALLA MOUSSEUL TE TAXALEE NIOKK SERIGNE SOU BONNE YII

  • Abdou Tall
    Abdou Tall il y a 6 mois

    Thiey aduna lou métti yaguenafi. Ndeysan tè digueuté am akk ñak dafa soriwull. Li ay pékhè seytané moussi lakhassou rk. Yalla na Yalla doli soutoureu.

  • Hanne Ababacar
    Hanne Ababacar il y a 6 mois

    Kène xamoul couco dèf

  • awa bakhoum
    awa bakhoum il y a 6 mois

    Ce que dit le sieur en t.shirt noir est tres pertinente. L'enquête doit continuer pour connaître le motif l'alibi de son acte. Un pchychologue pourrait le faire parler. Diarnako déh

  • La Zèbre
    La Zèbre il y a 6 mois

    Tous les gens qui sacrifient sont toujours gentilles