GALLÉ NO STRESS - Episode 27 - 20 Mai 2020 Télécharger

Envoyer à vos amis
Ajouter
  • 20 mai 2020

  • Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine http://www.youtube.com/c/SSPSENEGAL

Commentaires

  • Ada et ses delires
    Ada et ses delires il y a 5 mois

    Sketch réussi si vous êtes d'accord beusseul j'aime 🙏🙏

  • Ndeye Fatma Mbacké
    Ndeye Fatma Mbacké il y a 5 mois

    Dama yakarone ni amoul tay sakh ana fans baye yi😂😂

  • Mouhamadou Diao Diallo
    Mouhamadou Diao Diallo il y a 5 mois

    Waa sétlou nguène serigne bi noumouy dohé ak yékati tank yi😅

  • Mika Tsar l'officielle
    Mika Tsar l'officielle il y a 5 mois

    Première commentaire svp meyléne ma like🙏

  • Ali Ndiaye
    Ali Ndiaye il y a 5 mois

    respect à tous les corps médical merci Baye

  • Aliou Touré
    Aliou Touré il y a 5 mois

    Yalla na corona bi déme bala korité si barké seydina Mohamed

  • Mamadou Ndiaye
    Mamadou Ndiaye il y a 5 mois

    Rang mouy gaw je suis le premier avoir porter les yeux dessus stp plus de likes la beugg comment before watching ❤💪👊

  • Petit_Pape PPG
    Petit_Pape PPG il y a 5 mois

    80e commentaire !! May leine ma 80 j'aime reik !! Rang mouy gaw

  • Sokhna Diarra Fall
    Sokhna Diarra Fall il y a 5 mois

    Kou beugue borom Touba beuseul j'aime ❤️❤️🙏

  • ALIOU NIANG
    ALIOU NIANG il y a 5 mois

    Bilahi cocote dama nék lol je t’aime beaucoup cocote mais baye rew na 😂😂😂😂😂😂

  • Cheikhona Lo
    Cheikhona Lo il y a 5 mois

    Tathio léne séne bop 👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏geune nianal gni neksi hopitale yi yalla weureule léne amine way 👏👏👏

  • moi Ndiaye
    moi Ndiaye il y a 5 mois

    Wa guisguen serigne bi nimouy dokhei 😂😂😂😂

  • Daouda Sarr
    Daouda Sarr il y a 5 mois

    Li dou deug premier vue

  • Khadija Thiam
    Khadija Thiam il y a 5 mois

    Ana ngiko done xar 🥰😭🤦‍♀️

  • Safiétou Niassy
    Safiétou Niassy il y a 5 mois

    Harnako ba sonou oooo merci baye tadiouna sahk 👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽

  • Awa Dieng
    Awa Dieng il y a 5 mois

    Serigne Ganna yalla na fi yague lolou té wer ne lén amine

  • Amadou Faye
    Amadou Faye il y a 5 mois

    Ana gni beug baye 😍 waaaay 😍

  • King khadim Falshøw
    King khadim Falshøw il y a 5 mois

    Ndeye sane lima meti si fin koor gui rek mouy série yi suis triste 🤦🏼‍♂️

  • Omar TV Touba
    Omar TV Touba il y a 5 mois

    Ku Abonnée Sama Chaîne You Tube Yalla Nala yalla Faye

  • Abdoulaye Ndiaye
    Abdoulaye Ndiaye il y a 5 mois (modifié)

    Baye est le meilleur comédien de l’année qui est d’accord beuseul j’aime